|
Seetal ci jukki ci kàllaama wolof: | |
|
Nas wi bokk na ci bëre biy dàq ber bi ñu ber yenn làkk yi (rawatina ci internet bi), xëcc itam gëndaloo guy yamale te di jàpplante, loolu di sukkandiku ci sañ-sañu askan yi gàddu seen kuute ci caada. | ||
|
Xam-xam
|
|
|
|
|
|
|
Ndakaaru (Dakar) Nekkoon péyu Afrig gu sowwu gu fraase (ASF, walla AOF ci FR), Ndakaaru fimne mooy Péyu reewum Barug Senegaal akit goxub Ndakaaru, tolluwaayam ci péeteg sowwu bu Afrig, ci jegeem Daanaka-dun bu Kap-Wert, waral na sancug notaakon yu jëkk yi, Akit yaxantu ak Àdduna bu bees bi, te ame na peetewaayu ngëneel ci jëflanteg cosaani Saa-Afrig yi ak Saa-Tugal yi. Fa lees Taxawalee woon Xumbalu Àddina bu fànni ñuule (jaam yu ñuul) bu njëkk bi ci xalaatu Leopool Sedaar Sengoor atum 1966, Dëkk bii mooy toogu bu Këru-gëstu bu dàttu bu Afirg gu ñuule (KDAN, walla IFAN ci FR) akit bu Bànk bu diggu bu guuri Afrig gu sowwu (BDGAS walla BCEAO ci FR) |
- Yi weesu 250000 jukki: · · · · · · · · ·
- Yi weesu 80000 jukki: · · · · · · · · ·
- Yi weesu 40000 jukki: · · · · · · · · · ·
- Yi weesu 20000 jukki: · · · · · · · · · · ·
- Yi weesu 1000 jukki: · · · ·
- · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · · (ngir yeneeni Wikipedia, xoolal ci bànqaasu wet gi)
Dàttub njoxeeb ay nataal |
Baatukaay barilàkk |
Dajaleeb ay tudd | |||
Xibaari àdduna bi |
Téerey njàng yu ubbeeku |
Kaggu bu ubbeeku | |||
Wayndareeb xeeti mindeef yépp |
Jumtukaay ak yëngu-yëngu ñeel njàng |
Nosuwaayu sémbi Wikimedia yi |